ADIYA FEDERATION BAYE FALL FR => SAME WORMAY TOUBA
Lancée il y a 22 jours
486 €
collectés avec 21 participants
Salam aleykoum niongui ziar mbokk talibé yeup
Nioune Fédération Nationale des Bayes Fall de France Niongui fass yéné dadialé adiyas yi dieume si Bissou JAYANTE bi deupok Ndigalou Serigne Touba Serigne Mountakha Mbacké dieume si SAMEU WORMAY TOUBA, ndigali agsi keur Mame Cheikh Ibrahima FALL Serigne Amdy Khady Fall.
Danio fass yéné dadialé ay adiya you dieumeu si lepp louy dioumtoukay loumou gueuneu gaw nguire meuneu diékkou ndigali. Kep kouy dioulite rawatina ngay mouride rawatina ngay baye fall té hameu li Serigne touba beugg si deukeum bou sele bi warnala nga samal koko sameulé koko kone ndigal li nieupako bokk. Danio djiteul wa keur Mame Cheikh Ibrahima FALL rek wayé ndigalou diogué si Serigne Touba dieume Touba kou Beugeu Serigne Touba warngako def sa ligueyou bop kone nak MOUDIRE JEUF JEUL
Nioussi sakou pastefou nieup fass ko yéné yeute Mame Cheikh Ibrahima FALL mome SERIGNE AMDY KHADY FALL le 28 JUIN 2025.
KONE NAK FOU WAY YEME YAFA YEMALE SA BOP, BOU NDIGAL DJIBE NDIARIGNE DJIBE NA, NANIOU DEME TALAL SOUNOUY NDAPP NIOU DOUYALNIOU.
Di niane souniou borom lep dadié ak ngeureumal Serigne bi.
SERIGNE MOUNTAKHA MBACKE yalla nafi yagg té werr
SERIGNE AMDY KHADY FALL yague fi lole té werr
Ak mourides yeup ak dioulite yeup !